Daluweb bii dafay jëfandikoo ay nëbbiit ci niñ ko xamlee ci sunu sàrtu sàmm sutura. Soo nangoo jëfandikoo nëbbiit yi, bësal ci nangu.
Nangul
Sàrtu sàmm sutura

Ngir wone bu baax bii daluweb ci sa jumtukaay dañuy jëfandikoo say leerali xuusukaay. Soo nangoo jëfandikoo nëbbiit yi kese, dina ñu teg ab taxañu njoxe bu ndàw ci sa jumtukaay buy tax ñu mëna fàttaliku sa barab, say jëf ak say taamu ngir ñu mëna indi ay yokkute ci sa jaar-jaar. Lu wuutek jëfandikoo bii ci kaw, duñu séddoo say njoxe ak ay xaaj yu bawoo feneen, ludul yoon dafko laaj.

Bio‑Oil® / Bi-Oil® / Bioil®

Bio‑Oil dafay gëstu di yaatal ay costéefi pajum deru yaram yu ay nit yu ci xarañ, di jëfandikoo diw ngir amal xarañteefu costeef bu kawe. Màrk bi ci turu Bio‑Oil® lañ ko xame ci réew yépp yu wuuteek Ostaraali, Repibilik Cek, Faraans, Almaañ, Eslowaki ak Siwis fi nga xamantane turu Bi-Oil® lañuy jëfandikoo ca Sapoŋ fi nga xamante ni ci turu Bioil® lañ ko xame.

Lu jem ci loolu

Ci atum 1987 Bio‑Oil moo nekkoon li jiitu ci wàllum jëfandikoo diw ngir indi ay yokkute ci mandarga yuy feeñ ci sunu yaram ak rew yi. Bu njëkk, mën nañu wax ci xayma ni bépp costeef bu nekk ci bitik yi ab diw la woon wala ab tocamikukaay, te costeef bi dafa waraloon ay xel ñaar yu bari. Tey porodiwii bi moy bi gëna mag ci wàllum mandarga ak rew. Ci atum 2010 la Bio‑Oil sos ab labo bu ñu jagleel ay nit yu ci xarañ ngir gëstu niñuy def ngir faj yeneeni jafe-jafe yu am ci sunu deru yaram. Ci atum 2018, benn sel bu sokkeeko ci diwu yaram, lañu gennewoon, ci atum 2020 benn porodiwi buy xeex ak mandargay yaram moo ci topp te ñu defare ko diw nu raxul dara. Ci atum 2021 inndiwoon nañu diwu yaram yu niina niin ci marse bi. Bio‑Oil ci gëstu la gëna sukkandiku boole ci njaay ak wasaare ay costeefam yu ñu daganal ci këru liggéeyukaay yuy yëŋgu ci wàllum pajum deru yaram ci àddina bi yépp. Ngir am yeneeni leeral ci costeefi Bio‑Oil, demal ci farmasi bila gëna jege.

Màndargaay xoosu-xoosu ak rew

Diw amna man-man bu leer ci defaraat sa deru yaram. Xamuñu bu baax naka ak lu tax li baax ci diw ci folkoloor bi rek lañu ko gëna xamee. Bio‑Oil® Skincare Oil moo nekkoon costéef bu njëkk bi ñu amale ay testu kilinik te firndeel ni mën na indi ay yokkute ci mandarga xoosu-xoosu ak rew yi. Ndam yi am ci test yii ñoo tax ba doktoor yi ak liggéeykati farmasi yi ci addina bi yépp sawar ci tammbali digle costéef bi. Tey Diwu yaram Bio‑Oil® Skincare Oil mooy costéefu mandarga xoosu-xoosu bu jiitu ci addina bi ak lu ëpp 400 neexal ci walu pajum deru yaram ci turam. Xibàaru porodi bi

Xët yi lëkkalook wii "Bio-Oil Skincare Oil"

Deru yaram bu wow

Anam bi gëna gaaw ci fajj wowaayu der moy tekk ci kawam ab lal buy teye niinaay bi dem. Costéefi der yu wow yu njëkk yi (diw yi, toccamikukaay yi ak bëër yi) am nañu lu toll ci 20% ci diw, wax wala bëër ngir jubluwaay bii. Bio‑Oil® Dry Skin Gel Selu Der bu Wow amna 84%. Bio‑Oil® Dry Skin Gel (Selu yaram wu wow) ci atu 2018 la dooroon. Xibàaru porodi bi

Xët yi lëkkalook wii "Bio-Oil Dry Skin Gel"

Ay mandargay xoosu-xoosu ak rew (défarin bu sell)

Ak li nit ñi di laaj lu bari diwu yaram bu raxul dara ngir jigeen yi wonn lor gëne yokku, Bio‑Oil diw yaram yu raxul dara ngir xël ak xoos xoosu yaram kese la defar. Resiltaa yi juge ci natt yi ñu amaloon ci kilinik yi wone nañu ni moom ak poridiwi mandarga yaram bu Bio‑Oil bu orsinaal bi ñoo tollo, mu doon yoon bu njëkk bi ñu firndale ni ab porodiwu bu raxul tolloona ak beneen porodiwu bu ñu raññe bu baax. Bio‑Oil® Skincare Oil (Natural), ci ñetteelu xaaju atum 2020 mi la tambali liggéeyam. Xibàaru porodi bi

Xët yi lëkkalook wii "Bio-Oil Skincare Oil Natural"

Nooyalukaayu yaram

Nooyalukaayu yaram bi daf waroon naan ci saas yi te warul bayyi benn dessit bu niin, ngir nga ma mëna sol yere ci saas yi. Ci wàllum xarala dina jafe lool ndax nooyal gi dafay laaj ab lal gu niin ci deru yaram bi ngir mu mëna weyal nooyaay bi. Diwu Bio‑Oil® Body Lotion ñungi ko mooñe ak xarala Bio‑Oil bi ngay yénngal bala nga koy jéfandikoo te dafay tax diw bii di niin ak oyof. Bio‑Oil® Body Lotion mungi tammbali wër ci addina bi ci atum 2021. Xibàaru porodi bi

Xët yi lëkkalook wii "Bio-Oil Body Lotion"